Back to Top

Noone Nga Video (MV)




Performed By: Abdaz
Language: English
Length: 3:43
Written by: Abdou GUEYE
[Correct Info]



Abdaz - Noone Nga Lyrics
Official




Fouma séne dima réé
Ndéké meussoulo ma beugg hun...
Deuk thi yakk sama derr
Yallah may ma nangou woo
Bamou takali lak sa sagoo
Ndaxté nangou woulo Ndogal
Mousso ma yèné lou baxx
Té bougoulo ma waxal lou bax
Sama tolouway mola khagne diam
None nga Xame nako
Dieme nga sotiwoul
Wax Nga Ma teuxlou
Loudoul Yalla néne la té nitou késsé nga
None nga Xame nako
Gass nga Yallah Soul
Seurignetou nga antouwoul
Bo sagnone douma yindou tay wallah sax ma doff
Wanté do Yallah nak
Té amoulo ndogal si mane
Fékéwo fougnou ma sakké
Héyi yéyi yéhèhé...
Sa yo kheuyé yangui si mane
Deuk si di ma féxél
Téwoul mangui sante Yalla
Bou Yalla né dett dou diama koy dindy
Wolof Ndiaye done wax
Nite ki ak no meune ti mel
Dinga ame gnoula bagne
Xame nani mane reik nga bagne
Mou melni dama ray sa taw
Taloo sa bopp ndax mane
Bougoulo ma dieum kaname
Bamou diaral la ngamay féxél
Té loumou ladje nak ding ko deff
Mane talouma fayantou
Ndaxté dama neik si yone
Bolékok dink Yallah sama bopp
None nga Xame nako
Dieme nga sotiwoul
Wax Nga Ma teuxlou
Loudoul Yalla néne la té nitou késsé nga
None nga Xame nako
Gass nga Yallah Soul
Seurignetou nga antouwoul
Bo sagnone douma yindou tay wallah sax ma doff
Wanté do Yallah nak
Té amoulo ndogal si mane
Fékéwo fougnou ma sakké
Sa yo kheuyé yangui si mane
Deuk si di ma féxél
Téwoul mangui sante Yalla
Bou Yalla né dett dou diama koy dindy
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


English

Fouma séne dima réé
Ndéké meussoulo ma beugg hun...
Deuk thi yakk sama derr
Yallah may ma nangou woo
Bamou takali lak sa sagoo
Ndaxté nangou woulo Ndogal
Mousso ma yèné lou baxx
Té bougoulo ma waxal lou bax
Sama tolouway mola khagne diam
None nga Xame nako
Dieme nga sotiwoul
Wax Nga Ma teuxlou
Loudoul Yalla néne la té nitou késsé nga
None nga Xame nako
Gass nga Yallah Soul
Seurignetou nga antouwoul
Bo sagnone douma yindou tay wallah sax ma doff
Wanté do Yallah nak
Té amoulo ndogal si mane
Fékéwo fougnou ma sakké
Héyi yéyi yéhèhé...
Sa yo kheuyé yangui si mane
Deuk si di ma féxél
Téwoul mangui sante Yalla
Bou Yalla né dett dou diama koy dindy
Wolof Ndiaye done wax
Nite ki ak no meune ti mel
Dinga ame gnoula bagne
Xame nani mane reik nga bagne
Mou melni dama ray sa taw
Taloo sa bopp ndax mane
Bougoulo ma dieum kaname
Bamou diaral la ngamay féxél
Té loumou ladje nak ding ko deff
Mane talouma fayantou
Ndaxté dama neik si yone
Bolékok dink Yallah sama bopp
None nga Xame nako
Dieme nga sotiwoul
Wax Nga Ma teuxlou
Loudoul Yalla néne la té nitou késsé nga
None nga Xame nako
Gass nga Yallah Soul
Seurignetou nga antouwoul
Bo sagnone douma yindou tay wallah sax ma doff
Wanté do Yallah nak
Té amoulo ndogal si mane
Fékéwo fougnou ma sakké
Sa yo kheuyé yangui si mane
Deuk si di ma féxél
Téwoul mangui sante Yalla
Bou Yalla né dett dou diama koy dindy
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Abdou GUEYE
Copyright: Lyrics © O/B/O DistroKid

Back to: Abdaz

Tags:
No tags yet