Back to Top

Abdoulaye Samb - Dioubau Lyrics

Abdoulaye Samb - Dioubau Lyrics

[ Featuring Edward Ashcroft, Paul Vials ]

[in Wolof]
Senegal ben bopla ken mounouko khar niaar liko waral souniou mameyi daniou niaane bayifi
Naniou diokhante lokho te dimbelante si souniou biir, li moy lifi mame yi bayi wone
Andelene Deguolene Dioubaulene
Souniou bougue souniou reewmi nate naniou dioubau si sounou biir. Diema deguo si sounou biir te sottanete ay khalat.
Naniou yalla tanal kiguene si sounou biir mou djite sounou reew niou deme si kanam.
Souniou reew reewoume diame la
Souniou gal reewoume teranga la
Andelene Deguolene Dioubaulene
Dioubau moy andi diame si sounou reew
Andelene Deguolene Dioubaulene
Dioubau moy andi komkom si sounou reew
Andelene Deguolene Dioubaulene
Niou diokhante lokho diema diappo si souniou biir
Andelene Deguolene Dioubaulene
Niou djital ken nieup tope si guinawam
Andelene Deguolene Dioubaulene
Naniou diema dioubau te diapale souniou reew
Senegal ben bop la
Naniou len diema dioubau moytou khekhbi moytou khiro bi ak gnayo bi diarouko.
Senegal ben bopla ken mounouko khar niaar liko waral souniou mameyi daniou niaane bayifi.
Andelene Deguolene Dioubaulene
Niou djital ken nieup tope si guinawam
Souniou reew reewoume teranga la
Souniou gal galouk diamela
Nioun nieupe nio yam si souniou reewoumi
Senegal dou massa dess guinaw baykat bi ak ministre bi nion yam si Senegal
Artisan bi ak president bi nion yam si Senegal
Soula yalla denke ngua djite reewoumi waw
Nanga bayi khel nii tope sa guinaw
Kouli nafsine saii khatine maouti
Bakan bougnam doundou dinaniam deh
Baiil khel sa borom mom mila denke ngour
Ndakh ngourou yalla modoul diekh
Bees dina nieuw yalla bourbi latch la ningua don samme
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
Copyright: Lyrics © Sony/ATV Music Publishing LLC, APM MUSIC ASSOCIATED PRODUCTION MUSIC

Back to: Abdoulaye Samb

Abdoulaye Samb - Dioubau Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Abdoulaye Samb
Featuring: Edward Ashcroft, Paul Vials
Length: 3:11
Written by: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
[Correct Info]
Tags:
No tags yet