Back to Top

Abdoulaye Samb - Makalie Lyrics

Abdoulaye Samb - Makalie Lyrics

[ Featuring Edward Ashcroft, Paul Vials ]

[In Wolof]
Walou wouy walou
Yaye boy sori nguama
Sama yaye boy sori nguama
Weetal nguama
Sama yaye boy sori nguama
Weetal nguama
Lingua ma dane digual sama yaye boy mome lay dounde
Liguama dane tere
Sama yaye boy mome lay weye batay..
Mane sama yaye fonkena sama yaye
Mane sama yaye gueuremna sama yaye
Yaye akhou dioureel yaye daye tope dome
Sama yaye boye menoumala fay ma yaye.
Woylelenma ma woy djiguene diou bakha bakh si mane
Ndeye khady mane, Binta diour laniou wowe say aye boy.
Yayou Aida Ndiaye yayou Ndeye siniane guathe ngalama
Yayeou Binta Ndiour guathe ngalama ko sekal ngor khamna sa teranga
Dangua yewene te dangua gore khady, wa Fora sede len ma
Mane sama yaye boye beguenala,
Mane sama yaye boy fonkenala
Wakh you bakh yi nguama diguale mome lay dounde
Wakh you bakh yi nguama diguale mome lay weye
Dieufe diou bakh dji nguama dane diguale mone lay weye
Sama yaye
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
Copyright: Lyrics © Sony/ATV Music Publishing LLC, APM MUSIC ASSOCIATED PRODUCTION MUSIC

Back to: Abdoulaye Samb

Abdoulaye Samb - Makalie Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Abdoulaye Samb
Featuring: Edward Ashcroft, Paul Vials
Length: 3:46
Written by: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
[Correct Info]
Tags:
No tags yet