Back to Top

Abdoulaye Samb - Sam Sam Lyrics

Abdoulaye Samb - Sam Sam Lyrics

[ Featuring Edward Ashcroft, Paul Vials ]

[In Wolof]
Nitt ki begue na nga mandou, domou adama souma sanione da nguay mandou
Nitt ki begue na nga teye domou adama souma sanione da ngay teye
Nitt ki sope na nga doylou domou adama souma sanione da ngay doylou
Nitt ki da nga wara doylou si li la yalla diokh bolekok nangou ligueye reew mi
Beguena nga teye teyee, teyee ba melni ndokhoum sam sam
Domou adama dafa gueme Yalla
Domou adama dafa wara teye
Domou adama dafa wara doylou
Bole tiek liguey reewmi wawa wawaw
Domou adama daye mandou
Domou adama dangua wara teye, teye thi ndokh laniou ko tamou
Waye thi nitt la guene bakh wawaw domou adama dafa wara mandou
Mandou mandou wawaw ligueye reewi wawawaw
So bougue.nopalou, kay ma wakh la ni guay def
So bougue koula guiss naw la, yaw da nguay mandou
Lo khamoul khamoulo lo fekewoul fekewoulo ko
Boul thi diema kham dara ndakh domou adama daye mandou
Beguena nga teye teye teye ba melni ndokhoume sam sam
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
Copyright: Lyrics © Sony/ATV Music Publishing LLC, APM MUSIC ASSOCIATED PRODUCTION MUSIC

Back to: Abdoulaye Samb

Abdoulaye Samb - Sam Sam Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Abdoulaye Samb
Featuring: Edward Ashcroft, Paul Vials
Length: 3:32
Written by: ABDOULAYE SAMB, EDWARD JOHN CAMPBELL ASHCROFT, PAUL JONATHAN IVAN VIALS
[Correct Info]
Tags:
No tags yet