Back to Top

Boula Dara Meti Video (MV)

Performed By: Admow
Language: English
[Correct Info]

Admow - Boula Dara Meti Lyrics

Couplet
Yéne say nga fokni, thi adouna bi
Kéneu douleu comprendre
Sometime nga déme ba diap ni doto messeu contane
Thi biir keur gui, Yay boy néna doula may nada
Thi mbédd bi, ragala takh ngani do mayé dara
Mais nak boul diaakhlé
Yone leu mou diaffé
Wanté Maadi goor bi kham finga fété
Kham sa ndieuga takh ma deukk thi di niaafé
Thioféleu ngui thi biir khol bi
Diokh ma confiance ma yoboula fou sori
Ouuh baby, Owww baby

Refrain
Dmala love, love love, Baby love, love, love
Boula dara méti
Nakar diékh neu tay Ndakh mangui thi seu wéte
Boula dara méti
Di naala téwal thi Nadj, téwal la thi kérr
Boula dara méti
My baby I got your back
Boula dara méti

Couplet
Ouuhhh
Écoute moi baby
I love you baby
Et je sais que t'as peur de m'aimer
Si tu t'inquiètes pour moi t'as tord
Faut que tu sors de ton décors
T'as déjà gagné mon cœur. Donne moi ma chance, fais un effort
Soumala kholé guiss thi Yow kou ame diom
Douma beugg Loudoul done seu héros
Do wéte thi bilé yone, you're not alone
Je suis ton ange gardien
Oooh, baby you're the one
Baby you're the only one (éeh)
Baby you're the one that I need in my life

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Couplet
Yéne say nga fokni, thi adouna bi
Kéneu douleu comprendre
Sometime nga déme ba diap ni doto messeu contane
Thi biir keur gui, Yay boy néna doula may nada
Thi mbédd bi, ragala takh ngani do mayé dara
Mais nak boul diaakhlé
Yone leu mou diaffé
Wanté Maadi goor bi kham finga fété
Kham sa ndieuga takh ma deukk thi di niaafé
Thioféleu ngui thi biir khol bi
Diokh ma confiance ma yoboula fou sori
Ouuh baby, Owww baby

Refrain
Dmala love, love love, Baby love, love, love
Boula dara méti
Nakar diékh neu tay Ndakh mangui thi seu wéte
Boula dara méti
Di naala téwal thi Nadj, téwal la thi kérr
Boula dara méti
My baby I got your back
Boula dara méti

Couplet
Ouuhhh
Écoute moi baby
I love you baby
Et je sais que t'as peur de m'aimer
Si tu t'inquiètes pour moi t'as tord
Faut que tu sors de ton décors
T'as déjà gagné mon cœur. Donne moi ma chance, fais un effort
Soumala kholé guiss thi Yow kou ame diom
Douma beugg Loudoul done seu héros
Do wéte thi bilé yone, you're not alone
Je suis ton ange gardien
Oooh, baby you're the one
Baby you're the only one (éeh)
Baby you're the one that I need in my life

Refrain
Dmala love, love love, Baby love, love, love
Boula dara méti
Nakar diékh neu tay Ndakh mangui thi seu wéte
Boula dara méti
Di naala téwal thi Nadj, téwal la thi kérr
Boula dara méti
My baby I got your back
Boula dara méti
[ Correct these Lyrics ]

Back to: Admow

Tags:
No tags yet