Sama Yàlla dafa am kàttan
Moom mo jara magal
Te mo jara taggas
Mangi key woyal
Sama Yàlla dafa ndam
Moom rek mo mey dooleel
Moom rek mo mey dundal
Mangi key woyal
Sama Yàlla dafa am ndam
Moom rek mo
(Am ndam !)
Ci adduna ci ley
(Am ndam !)
Moom rek mo am doole
(Am ndam !)
Mangi key woyal
(Am ndam !)
Mangi key taggas
(Am ndam !)
Mangi key jaamu
(Am ndam !)
Mangi key yëkkëti
(Am ndam !)
Sama Yàlla
Sama Yàlla dafa am kàttan
Moom mo jara magal
Te mo jara taggas
Mangi key woyal
Sama Yàlla dafa am ndam
Moom rek mo mey dooleel
Moom rek mo mey dundal
Mangi key woyal
Sama Yàlla dafa am ndam
Yow yay ki am ndam li
(Am ndam !)
Ci asamaan
(Am ndam !)
Ci suuf ci ley
(Am ndam !)
Ôooooo !
Da am ndam
(Da am ndam !)
Da am ndam
(Da am ndam !)
Da am ndam
(Da am ndam !)
Da am ndam
(Da am ndam !)
Ôooooo !
Am ndam
Da fa am ndam
Moom dafa am cofeel
Am cofeel !
Am cofeel !
Am cofeel !
Am cofeel !
Am ndam !
Da fa am ndam !
Moom dafa am doole
Am doole !
Am doole !
Am doole !
Am doole !
Am ndam !
Dafa am ndam !
Sama Yàlla dafa am ndam
Moom mo jara magal
Te mo jara taggas
Mangi key woyal
(Mangi key woyal)
Sama Yàlla dafa am ndam
Boroom asamaan ak suuf
Yow yay ki mey àtte
Yow yay ki mey dundal
Sama Yàlla dafa
Am ndam !
Am ndam !
(Am ndam !)
Am ndam !
Am ndam !
Am ndam !
Am ndam !
Sama Yàlla dafa
(Am ndam !)
Sama Yàlla
(Am ndam !)
Yow yay ki faj sama xol
(Am ndam !)
Ki faj sama dunda
Mangi ley jaamu, jaamu
Sama Yàlla dafa
(Am ndam !)