Back to Top

Baye Niass Video (MV)

Performed By: Checky Blaze
Language: English
Length: 3:17
Written by: CHEIKH MBAYE

Checky Blaze - Baye Niass Lyrics

Ninka nanka ya niou guene si leundeum
Ya niou xamal li nieup outt sakhal souniou gueum gueum
Li nioul si diguente yi, khaq bil khaq souniou dieum dieum
Di niou tagali souniou sago,
Zikaroulah souniou meun meun

Beumeukh niou si sofianke
Diakhle weur niou so fi manké
Sante ak Barke lou
Takh dou niou mey none fim niou sanké
Weuyloun beug nio kheuthie waye meyniou ko bountou Wanté
Bepp kiray leniou teggui, deuk si xatir mo niou hanté

Khoutbou Niass ya di diante ndiolorr
Ya niou nandal, texel niou guénéniou si békorr
Sedday firdaw yi tagali niou ak tangorr
Ragalatou niou tiono tegui bepp galankorr

Ya niou xamal kaw ak souf
Li ko teye lou ko nekal
Mbotoum xam ak tassawouf
Kun fa yakoun li ko kenal
Diokalante si pays yi, li ko ouf
Li ko selal
Ruhu ak xol li lene doundeul li lene regal

Mawlana Baye xalan sakho di la sante
Nouri aL nourin yay souniou lerr souniou dianteu
Ya niou teunk si yonou dioup ba takh douniou meusseu penteu
Ragne neniou xamé neniou
Niass coumba yay souniou sangue

Amoul sik Raw nga sey mass
Di mouslou sa martaba
Fassiene top sey tank
Ni yak sa sopé ba tia makka ba
Top sey ndigueul awratt yi
Diouroum yi ba si assaka
Ruhul eudeup jeffé té sakho
Mouridoulahi akassa

Lign done sett Niass si yow legn ko done outt
Feug souniou deune yi youkhou
Euweulou akhirou amatoul doute
Teggui nga bepp kirray
Li xol di yek dara dou ko soutt
Xamé negn ragné negn
Douniou rerr si nassoutt

Amoul sikki ni teunk nga sa deune
Mbotoum marifa
Li neubou moy lo fegn
Takhh niou tass si akhikha
Lahila ila Niass niou diokh la adiya
Souniou diekh kene dou ko natt
Rassoulilah batina
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

English

Ninka nanka ya niou guene si leundeum
Ya niou xamal li nieup outt sakhal souniou gueum gueum
Li nioul si diguente yi, khaq bil khaq souniou dieum dieum
Di niou tagali souniou sago,
Zikaroulah souniou meun meun

Beumeukh niou si sofianke
Diakhle weur niou so fi manké
Sante ak Barke lou
Takh dou niou mey none fim niou sanké
Weuyloun beug nio kheuthie waye meyniou ko bountou Wanté
Bepp kiray leniou teggui, deuk si xatir mo niou hanté

Khoutbou Niass ya di diante ndiolorr
Ya niou nandal, texel niou guénéniou si békorr
Sedday firdaw yi tagali niou ak tangorr
Ragalatou niou tiono tegui bepp galankorr

Ya niou xamal kaw ak souf
Li ko teye lou ko nekal
Mbotoum xam ak tassawouf
Kun fa yakoun li ko kenal
Diokalante si pays yi, li ko ouf
Li ko selal
Ruhu ak xol li lene doundeul li lene regal

Mawlana Baye xalan sakho di la sante
Nouri aL nourin yay souniou lerr souniou dianteu
Ya niou teunk si yonou dioup ba takh douniou meusseu penteu
Ragne neniou xamé neniou
Niass coumba yay souniou sangue

Amoul sik Raw nga sey mass
Di mouslou sa martaba
Fassiene top sey tank
Ni yak sa sopé ba tia makka ba
Top sey ndigueul awratt yi
Diouroum yi ba si assaka
Ruhul eudeup jeffé té sakho
Mouridoulahi akassa

Lign done sett Niass si yow legn ko done outt
Feug souniou deune yi youkhou
Euweulou akhirou amatoul doute
Teggui nga bepp kirray
Li xol di yek dara dou ko soutt
Xamé negn ragné negn
Douniou rerr si nassoutt

Amoul sikki ni teunk nga sa deune
Mbotoum marifa
Li neubou moy lo fegn
Takhh niou tass si akhikha
Lahila ila Niass niou diokh la adiya
Souniou diekh kene dou ko natt
Rassoulilah batina
[ Correct these Lyrics ]
Writer: CHEIKH MBAYE
Copyright: Lyrics © O/B/O DistroKid

Back to: Checky Blaze

Tags:
No tags yet