Back to Top

Hello [Mbalax Remix] Video (MV)




Performed By: Youssou Ndour
Written by: Alexandru Cotoi, Linnea Deb, Mohombi Moupondo, Thomas Gson, Youssou N'Dour, Zaza Fournier
[Correct Info]



Youssou Ndour - Hello [Mbalax Remix] Lyrics




Ni sett nala si kaname gouma
Guiss si mbedd bi
Dianerr na yonou Cinèma
Yonne amatoufi
Si birr lolou la done soss
Yone bi may Diar
Bëss bou nè may kheuy
Dianok yaw
Yaw nga dima rèh

Tant de fois tu sais, j'ai fermé les yeux
Priant le destin qu'enfin tu viennes à moi
J'ai cherché ta voix
J'ai compté les pas
Mais j'attends encore ce jour où tu me diras

Hello hello
Hello hello
Mangiy deglou
Nga mina
Hello
Hello hello
Hello hello
Mbeuguël dou sett
Melni nouyo

Lègui wakhma ndeurign
Gnou la weur
Bo ci nèwoul
Ma ngi lay wo
Ndakh Dëgg ngama
Wala Guiss ngama

Bëpp Xibarr bougnou
Meussa wakh
Khalatt na la si
Bëss bou nè bouma keuyé
Dianok yaw
Yaw nga dima Rèh

Tant de fois tu sais, j'ai fermé les yeux
Priant le destin qu'enfin tu viennes à moi
J'ai cherché ta voix
J'ai compté les pas
Mais j'attends encore ce jour où tu me diras

Hello hello
Hello hello
Mangiy deglou
Nga mina
Hello
Hello hello
Hello hello
Mbeuguël dou sett
Melni nouyo

Khamna ni Sa lepp doyna ma bébé
Guissna sa Takandërr
Si say beutt bébé
Yèèmé na nimala nammé
Dontè khama Gou mala mane wett na

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Li takh
Mou beugg la
Taamou la
Tagg laaa
Wanèla founè

Dafa lall
Ton coeur
Yèllooo nga kooo
Ba Guëdj gui ferr

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Lou way amoul
Sa wayy dako amoul
Yagg yagg bawoul Thioooro oh
Lou yagg loll
Lou yagg deugla ohh oh

Ninga mèlone Daw
No mel Rèn Dal
Say dieuw ak say wakh
Yèmone na gnou

Hè hè hèè
Kholna ba kholatt
Kham nani yaw rekk la ak bass
Nè j'ai le dernier Faty
Mane rekk

Wa Gambia
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem yaaw
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem yaaw
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yaako tchi geuneul yaaw
Mola taneu way
Daffa Daffaaa la Mokal
Tamou la
Yako Gueuneul Way

Mo socè thia Gambia chérie
Seye dieng
Badara Mbaye thia Gambia chérie
Amy Mbaye
Yène salal dikhè
Diouk lene Dikk ni moutt
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.


We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.




Ni sett nala si kaname gouma
Guiss si mbedd bi
Dianerr na yonou Cinèma
Yonne amatoufi
Si birr lolou la done soss
Yone bi may Diar
Bëss bou nè may kheuy
Dianok yaw
Yaw nga dima rèh

Tant de fois tu sais, j'ai fermé les yeux
Priant le destin qu'enfin tu viennes à moi
J'ai cherché ta voix
J'ai compté les pas
Mais j'attends encore ce jour où tu me diras

Hello hello
Hello hello
Mangiy deglou
Nga mina
Hello
Hello hello
Hello hello
Mbeuguël dou sett
Melni nouyo

Lègui wakhma ndeurign
Gnou la weur
Bo ci nèwoul
Ma ngi lay wo
Ndakh Dëgg ngama
Wala Guiss ngama

Bëpp Xibarr bougnou
Meussa wakh
Khalatt na la si
Bëss bou nè bouma keuyé
Dianok yaw
Yaw nga dima Rèh

Tant de fois tu sais, j'ai fermé les yeux
Priant le destin qu'enfin tu viennes à moi
J'ai cherché ta voix
J'ai compté les pas
Mais j'attends encore ce jour où tu me diras

Hello hello
Hello hello
Mangiy deglou
Nga mina
Hello
Hello hello
Hello hello
Mbeuguël dou sett
Melni nouyo

Khamna ni Sa lepp doyna ma bébé
Guissna sa Takandërr
Si say beutt bébé
Yèèmé na nimala nammé
Dontè khama Gou mala mane wett na

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Li takh
Mou beugg la
Taamou la
Tagg laaa
Wanèla founè

Dafa lall
Ton coeur
Yèllooo nga kooo
Ba Guëdj gui ferr

Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem
Yaw rekk
Yaw yaw rekk

Lou way amoul
Sa wayy dako amoul
Yagg yagg bawoul Thioooro oh
Lou yagg loll
Lou yagg deugla ohh oh

Ninga mèlone Daw
No mel Rèn Dal
Say dieuw ak say wakh
Yèmone na gnou

Hè hè hèè
Kholna ba kholatt
Kham nani yaw rekk la ak bass
Nè j'ai le dernier Faty
Mane rekk

Wa Gambia
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem yaaw
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yay prèfèrem yaaw
Dafa ni dafa ni
Dafa ni dafa ni
Yaako tchi geuneul yaaw
Mola taneu way
Daffa Daffaaa la Mokal
Tamou la
Yako Gueuneul Way

Mo socè thia Gambia chérie
Seye dieng
Badara Mbaye thia Gambia chérie
Amy Mbaye
Yène salal dikhè
Diouk lene Dikk ni moutt
[ Correct these Lyrics ]
Writer: Alexandru Cotoi, Linnea Deb, Mohombi Moupondo, Thomas Gson, Youssou N'Dour, Zaza Fournier
Copyright: Lyrics © Kobalt Music Publishing Ltd.


Tags:
No tags yet