Back to Top

Youssou Ndour - Létt Ma Lyrics

Youssou Ndour - Létt Ma Lyrics

Du nil, du nil
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo, lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma

Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe

Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw

Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa

Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
Bëgg ak bañ la

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Kabou Gueye, Mody Ba, Youssou N'dour
Copyright: Lyrics © Universal Music Publishing Group, Sony/ATV Music Publishing LLC

Back to: Youssou Ndour

Youssou Ndour - Létt Ma Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Youssou Ndour
Written by: Kabou Gueye, Mody Ba, Youssou N'dour
[Correct Info]
Tags:
No tags yet